42 Musal na ñenen; munul a musal bop’ am. Mō di Bur i Israel: na wacha lēgi chi kura bi, te di nañu ko gum.
Ne, Ana ki jūdu Bur i Yauod ya? Ndege gis on nañu bidiw am cha Penku, te dika nañu ndah͈ ñu jāmu ko.
Ñu teg chi kou bop’ am njêñ am, ba ñu bind’ on nile: Kile di Yesu Bur i Yauod ya.
You mi dānel jama ja te tabah͈ati ko chi ñet’ i fan, musalal sa bopa. So de Dōm i Yalla, wachal chi kura bi.
I njīt i seriñ ya itam, ak bindānkat ya ak mag ya ñaual ko, ne,
Nathanael tontu ko, ne, Rabbi, yā di Dōm i Yalla; yā di Bur i Israel.
Ñu fah͈a i banh͈as i tir ya, te dem gatanduji ko, te h͈āchu ne, Hosanna: barkel chi ka di dika chi tur i Borom ba, mu di Bur i Israel.
Te su kena dēge suma i wah͈, te defu len, mā ko atewul; ndege diku ma atesi aduna si, wande musal aduna si.
Ñu ôlu nak ka silmah͈a won ñar i yōn, te ne ko, Na nga jebal Yalla ndam: h͈am nañu ne nit kile bakarkat la.