36 Ñu tōg, di ko otu fōfale.
Ñu teg chi kou bop’ am njêñ am, ba ñu bind’ on nile: Kile di Yesu Bur i Yauod ya.
Saltige ba nak, ak ña nek’ on ak mōm, di otu Yesu, ba ñu gise yengatu’ suf sa, ak yef ya am, ñu tīt lol, ne, Chi dega kile Dōm i Yalla la.