34 Ñu joh͈ ko biñ bu ñu bōle ak weh͈tan ndah͈ mu nān: ba mu ko mose, mu bañ a nān.
Nōn’ ak nōna kena chi ñom dou, jel ab sponge, fêsal ko binegar, def ko chi sonka, te joh͈ ko mu nān.