31 Ba ñu ko ñauale, ñu ñōri ko, solal ko chol am, te omat ko ndah͈ ñu dāj ko cha kura ba.
Di nañu ko jebal Gentile ya, ndah͈ ñu ñaual ko, ratah͈ ko, te dāj ko cha kura; te chi ñetel i fan am di na dēki.
Ñu japa ko, sani ko chi biti tōl ba, te rēy ko.
H͈am ngēn ne cha ganou ñar i fan h͈ewte ga di na jot, te ñu or Dōm i nit ka ndah͈ ñu dāj ko chi kura.
Tah͈na mu jebal len ko ndah͈ ñu dāj ko cha kura ba.
Cha ganou mu ne talube ba, Sêtal, sa ndey angile! Te cha wah͈tu wōwale talube ba jel ko cha ker i bop’ am.