25 Nit ña ñepa tontu, ne, Na deret am dal chi suñu kou ak chi suñu kou i dōm.
Bulu sukal saa bopa fi nom, ne, da nga len di jaamu: ndegi, Man Yalla saa Borom, Yalla bu fir la, te di teg bakar i bai yi ce kou dom yi, ca netel ak nenentel i hert na maa ban,
Ku dānuji chi doch wile, di na dama: wande ku mu dānu chi kou am, di na ko mokal kilip.