13 Mōtah͈ Pilate ne ko, Dēgu la yef yi ñu la sēdêl?
Kēlifa i seriñ ya jog, te ne ko, Do tontu dara? li la ñile sēdêl?
Ba ko i njīt i seriñ ya ak mag ya jêñe, tontuwul dara.
Tontuwu ko dara, du bena bāt sah͈; tah͈na kēlifa ga jomi lol.
Pilate tontu, ne, Ndah͈ Yauod la? Sa h͈êt i bopa ak i njīt i seriñ ya ño la jebale fi man: ana lo def?