71 Ba mu deme be h͈araf cha rum ba, kenen gis ko, te ne ña fa neka, Kile nek’ on na itam ak Yesu wā’ Nazareth ba.
Te ñou, deka chi rew mu tūda Nazareth: ndah͈ la yonent ya wah͈ on motaliku, ne, Di nañu ko tūde Nazarene.
Wande mu wēdi chi kanam i ñepa, ne, H͈amu ma li nga wah͈.
Mu wēdêti ak ngeñ, ne, H͈amu ma nit ki.