7 Jena jigen, ju am ndap i diw gu h͈ēñ gu jafe njēg lol, ñou fi mom, te tūr ko chi bop’ am ba mu tōge di leka.
Wande ba ko tālube ya gise, ñu mer, ne, Lu waral yah͈a gile?