66 Lan ngēn dēfe? Ñu tontu ne, Dagan na dē.
Yauod ya tontu ko, ne, Am nañu yōn, te chi suñu yōn wōgu ela na dē, ndege def on na bop’ am Dōm i Yalla.