65 Fōfale kēlifa i seriñ ya h͈oti chol am, ne, H͈as na Yalla: ban sēde la ñu soh͈lāti? Dēga ngēn h͈as am nak:
Ñena cha bindānkat ya ne chi sēn h͈ol, Nit kile tedadil na Yalla.
Yauod ya tontu ko, ne, Dowul ndig ligey bu bāh͈ la ñu la buga jumat, wande ndig sāga Yalla; ndege you mi di nit def nga sa bopa Yalla.
Di ngēn wah͈al ka Yalla selal on, te yōni ko chi aduna si, ne Sāga nga Yalla, ndege wah͈ nā, ne, Mā di Dōm i Yalla?