61 Nit kile wah͈ on na, ne, Mun nā dānel juma’ Yalla, te tabah͈ati ko chi ñet’ i fan.
Wande ba ko Pharisee ya dēge, ñu ne, Kile gēneūl jine ya lu dul chi Abdujambar njīt i jine ya.
Kēlifa i seriñ ya jog, te ne ko, Do tontu dara? li la ñile sēdêl?
Ba mu deme be h͈araf cha rum ba, kenen gis ko, te ne ña fa neka, Kile nek’ on na itam ak Yesu wā’ Nazareth ba.
You mi dānel jama ja te tabah͈ati ko chi ñet’ i fan, musalal sa bopa. So de Dōm i Yalla, wachal chi kura bi.
Mu sani dogit i h͈alis ya chi suf chi juma ja, gēna, te dem, eng̈a bop’ am.
H͈am nañu ne Yalla wah͈ on na cha Musa; wande kile, h͈amu ñu fu mu bayako.