52 Yesu ne ko, Delōl sa jāsi chi mbar am: ndege ñepa ña fab jāsi, di nañu dānu ak jāsi.
Wande mangi len di wah͈, Bu len findu lu bon, wande ku la dōr chi sa leh͈ i ndējor, sopalil benen bi itam.