Matthew 26:47 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907
47 Ba mu wah͈andô, Judas, kena chi fuk’ ak ñar ña, ñou, and’ ak mōm mbōlo mu rey ñu am i jāsi ak i doko, ñu juge fa i njīt i seriñ ya ak i mag i nit ña.
Chi wah͈tu wōwale Yesu ne mbōlo ma, Dika ngēn jelsi ma ak i jāsi ak i doko, niki sachakat? Dan nā tōg ak yēn gir gu neka, di jemantale chi juma ja, te japu len ma won.