Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 26:45 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

45 Fōfale mu ñou fi tālube ya, te ne len, Nelou len lēgi, te nopalaku: wah͈tu wi jegeñsi na, te or nañu Dōm i nit ka chi loh͈o i bakarkat ya.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 26:45
14 Iomraidhean Croise  

Mu ne, Dem len chi bir deka ba fa kena nit, te ne ko, Jemantalkat ba ne, Suma wah͈tu jegeñsi na; di nā h͈umbal h͈ewte ga chi sa nēg, ak suma i tālube.


H͈am ngēn ne cha ganou ñar i fan h͈ewte ga di na jot, te ñu or Dōm i nit ka ndah͈ ñu dāj ko chi kura.


Mu bayiati len, dem, te ñān ñetel i yōn wa, wah͈ati bāt yōgale.


Jog len, na ñu dem, ki ma orsi jegeñsi na.


Te Yesu tontu len, ne, Wah͈tu wi jot na be ba Dōm i nit ka di ami ndam.


Suma fit nah͈arlu na lēgi; te ana lu ma war a wah͈? Bay bi, musal ma chi wah͈tu wile? Wande lōlo tah͈ ma dika chi wah͈tu wile.


Ba h͈ewte i njot ga lāta jot, Yesu ka h͈am ne wah͈tu am dikasi na ba mo di bayi aduna si dem fa Bay ba, naka mu sope won yos am ña neka chi aduna si, mu sopa len be cha muj ga.


Yef yōyu Yesu wah͈ on: te yēkati i but am cha asaman, te ne, Bay bi, wah͈tu wa jot na; na nga may sa Dōm ndam, ndah͈ Dōm ji itam jebal la ndam:


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan