44 Mu bayiati len, dem, te ñān ñetel i yōn wa, wah͈ati bāt yōgale.
Mu ñouati, feka len ñu di nelou, ndege sēn i but dīs on nañu.
Fōfale mu ñou fi tālube ya, te ne len, Nelou len lēgi, te nopalaku: wah͈tu wi jegeñsi na, te or nañu Dōm i nit ka chi loh͈o i bakarkat ya.
Te su ngēn di ñān, bu len wah͈ati bāt i nēn niki ña h͈amul Yalla; ndege dēfe nañu ne di nañu len dēga ndig sēn bāt yu bare.