23 Mu tontu, ne, Ki jō loh͈o am ak man chi ndap li, kōka ma ori.
Ñu nah͈arlu bu miti, te ku neka dal ne ko, Borom bi, man lā’m?
Dowul yēn ñepa lā wah͈: h͈am nā ña ma tan’ on: wande ndah͈ mbinda ma motaliku, Ka leka suma mburu yēkati na testan am chi man.