Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 26:2 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

2 H͈am ngēn ne cha ganou ñar i fan h͈ewte ga di na jot, te ñu or Dōm i nit ka ndah͈ ñu dāj ko chi kura.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 26:2
17 Iomraidhean Croise  

Simon wā Canaan, ak Judas Iscariot, ka ko or on.


Ba ñu deke chi Galilee, Yesu ne len, Di nañu or Dōm i nit ka chi loh͈o i nit;


Da ma bakar chi niki ma ore deret i ku set ka. Wande ñu ne, Lu ñu soh͈al chi lōla? Sêtal sa bopa.


H͈ewte i Yauod ya jegeñsi na; te ñu bare juge cha deka ya, dem cha Jerusalem ba h͈ewte ga lāta jot, ndah͈ ñu setal sēn bopa.


Yesu nak jurom ben’ i fan bala h͈ewte ga jot, dika cha Bethany, fa Lazarus nek’ on, ka Yesu dēkali won cha dē ga.


Judas, ka ko or on, h͈am on na bereb ba; ndege Yesu faral on na dem fōfa ak i talube am.


Ndah͈ bāt i Yesu motaliku ba mu wah͈ on, di wone chi ban melo dē la dēeji.


Te h͈ewte i Yauod ya jegeñsi na, te Yesu dem fa Jerusalem.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan