17 Chi bes i h͈ewte i mburu’ njanja bu jeka, tālube ya ñou fi Yesu, ne, Fan nga buga ñu wājal la ndah͈ nga leka h͈ewte gi?
Cha ganou lōlu mu ūt naka la ko mun a ore.
Tālube ya def la len Yesu wah͈ on, waj h͈ewte ga.
Yesu tontu ko, ne, Bul ko bañ lēgi, ndege nōgu la ñu ela motali njūbay yepa. Nōgale la bañatul.