16 Cha ganou lōlu mu ūt naka la ko mun a ore.
Te ne len, Lan ngēn ma joh͈, te di nā len ko jebal? Ñu dige ak mōm ñeta fuk’ i dogit i h͈alis.
Chi bes i h͈ewte i mburu’ njanja bu jeka, tālube ya ñou fi Yesu, ne, Fan nga buga ñu wājal la ndah͈ nga leka h͈ewte gi?