12 Ndege ba mu tūre diw gu h͈ēñ gile chi suma yaram, def na ko ndig suma sūl.
Tah͈na Yesu ne, Bayi ko; ndig suma bes i sūl la ko dēncha.