11 Cha ganou ga yenen h͈ēk ya ñou itam, ne, Borom bi, Borom bi, ūbi ñu.
Fōfale di nañu nirale ngur i ajana ak fuk’ i h͈ēk, ñu jel on sēn i lampa, di gatanduji borom‐seyt.
Wande mu tontu, ne, Chi dega mangi len di wah͈, h͈amu ma len.