Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 25:1 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

1 Fōfale di nañu nirale ngur i ajana ak fuk’ i h͈ēk, ñu jel on sēn i lampa, di gatanduji borom‐seyt.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 25:1
43 Iomraidhean Croise  

Mu teg benen lēb chi sēn kanam, ne, Ngur i ajana niro na ak nit ka ji on jiu ju bāh͈ chi tōl am;


Mu teg benen lēb chi sēn kanam, ne, Ngur i ajana niro na ak pēp’ i sūna, bu nit fab, te ji chi tōl am;


Tōl ba aduna si la; jiu wu bāh͈ wa i dōm i ngur ga la; nduh͈um la i dōm i bulis la;


Ngur i ajana nirôti na ak mbal mu ñu sani chi gēch, mu japa h͈êt i jen wu neka:


Ndege ngur i ajana niro na ak bena borom‐ker ku gēna chi sūba têl, ndah͈ mu binda i ligeykat chi tōl am.


Ngur i ajana niro na ak bena bur bu h͈umbal on nchēt i dōm am;


Fōfale h͈ēk yōyale yepa jog, te jagal sēn i lampa.


Rēchu len, ndege ngur i ajana jegeñsi na.


Na sēn lêray mbōk tāka chi kanam i nit, ndah͈ ñu gis sēn i jef yu bāh͈, te di magal sēn Bay ba cha ajana.


Yesu ne len, I mbok’ i nēg i borom‐chēt ga, ndah͈ mun naño nah͈arlu ba borom‐chēt ga neke ak ñom? Wande jamāno di na diki ba ño fabi borom‐chēt ga cha ñom; bōbale di nañu ôri.


Judas nak, ba mu ame i h͈arekat ak i saltige cha i njīt i seriñ ya ak Pharisee ya, mu dika fōfale ak i lampa ak i nītu ak i ganay.


Ka am seyt ba borom‐seyt ba la; wande h͈arit i borom‐seyt ba, ka tah͈ou te dēga ko, mō banēh͈u bu bare ndig bāt i borom‐seyt ba: suma banēh͈ bile mbōk motaliku.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan