7 Ndege h͈êt di na jog chi kou h͈êt, ak ngur chi kou ngur: i h͈īf di nañu ami, ak i yengatu’ suf si chi bereb yu bare.