51 Dog ko chi diga, te sedāle ko nafeh͈a ya: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.
Fōfale bur ba ne i rapas am, Ew len loh͈o am ak tank’ am, te sani ko chi lendem i biti; fōfale la joy di neka ak yey i buñ.
Borom i bukanēg bōbale di na ñou chi bes bu mu ko sēnuwul, ak chi wah͈tu wu mu h͈amul,
Te sani len jām bu jeriñul bi cha lendem i biti: fōfale la joy di neka, ak yey i buñ.
Wande i dōm i ngur ga, di nañu len tabal chi lendem i biti; fōfale la joy di neka ak yeyi buñ.