48 Wande su bukanēg bu bon bale wah͈e chi h͈ol am, ne, Suma borom yīh͈ na;
Fōfale borom am ôlo ko fi mōm, te ne ko, E jām bu soh͈or bi, mā la baal on bor bōbale yepa, ndege dagān on nga ma:
Chi dega mangi len di wah͈, Di na ko teg njīt cha la mu am yepa.
Te dal di dōr i naule am, leka ak nān ak mandikat ya;
Wande borom am tontu ko, ne, E jām bu bon bi, te tayal; h͈am on nga ne da ma gōb fu ma jiūl on, te forātu fu ma tūrul on;
Te cha wah͈tu’ rêr, Seytane nak def on na jēg chi h͈ol i Judas Iscariot, dōm i Simon, mu or ko,