Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 24:45 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

45 Kan a di bukanēg mbōk bu taku te têy, bu borom am jītal chi ker am, ndah͈ mu joh͈ len sēn dundu chi wah͈tu wa?

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 24:45
28 Iomraidhean Croise  

Mangi len di yōni naka i nh͈ar chi digante i būki: mōtah͈ na ngēn têylu naka i jān, te lew naka i mpetah͈.


Mu ne len, Bindānkat bu neka mbōk bu ñu nekalo tālube chi ngur i ajana, niro na ak borom‐ker ku gēne chi dēnchukay am lu ês ak lu maget.


Barkel chi bukanēg bōbale, ba borom am di feka mu di def nōga ba mu agse.


Jurom chi ñom nek’ on nañu ñu ñaka sago, te jurom ña di ñu am sago.


Borom am ne ko, Wau gōr, E jām bu bāh͈ bi te taku: da nga gōre chi lu new, di nā la teg njīt chi lu bare: h͈arafsil chi sa banēh͈ i borom.


Borom am ne ko, Wau gōr, E jām bu bāh͈ bi, te taku: da nga gōre chi lu new, di nā la teg njīt chi lu bare: h͈arafsil chi sa banēh͈ i borom.


Mōtah͈ ku mu mun a don ku dēga suma i bāt yile, te def len, di na niro ak nit i sago, ka tabah͈ nēg am chi kou doch:


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan