40 Fōfale ñar i nit di nañu neki chi tōl; ñu jel kena, te bayi ka cha des:
Te yēgu ñu be tufan la ñou yubuāle len ñepa; nōgu la ndika i Dōm i nit ka di meli.
Ñar i jigen di nañu di wol chi wolukay; ñu jel kena, te bayi ka cha des.