Matthew 24:30 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 190730 Fōfale mandarga i Dōm i nit ka di na fêñ cha asaman; h͈êt i aduna si yepa di nañu yeremtu, te di nañu gis Dōm i nit ka mu di ñou chi i nir i asaman si ak kantan ak ndam lu rey. Faic an caibideil |