16 Fōfale na ña neka chi Judæa dou cha tūnda ya:
Ba Yesu jūdo cha Bethlehem i Judæa, chi bes i Herod bur ba, i borom‐h͈amh͈am juge on nañu cha Penku, ñou chi Jerusalem,
Bu ngēn di gisi suboh͈un ak h͈udosun mbōk mu di tah͈ou chi bereb bu sela ba, naka Daniel yonent ba wah͈ on (ka ko janga na h͈am),
Ku neka chi kou nēg, bu mu wacha mu gēne yef ya chi nēg am: