15 Bu ngēn di gisi suboh͈un ak h͈udosun mbōk mu di tah͈ou chi bereb bu sela ba, naka Daniel yonent ba wah͈ on (ka ko janga na h͈am),
Fōfale na ña neka chi Judæa dou cha tūnda ya:
Su ñu ko bayie nōgule, ñepa di nañu gum chi mōm: te wā’ Rome ya di nañu dika, te jel suñu bereb ak suñu rew itam.