12 Te ndig bakar di na fūs, nchofel i ñu bare di na wañiku.
Yonent i nafeh͈a yu bare di nañu jogi, te nah͈ ñu bare.
Wande ka di muñ be cha muj ga, di na mucha.