Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 23:34 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

34 Tah͈na yōne nā len i yonent, ak i borom‐sago, ak i h͈amkat: di ngēn rēy ñena ñi, te dāj len cha kura; te di ngēn ratah͈ ñena ñi chi sēn i juma, te geten len chi dek’ ak deka:

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 23:34
36 Iomraidhean Croise  

Wande su ñu len getene chi deka bile, dou len fa benen; ndege chi dega ma ne len, Du len won demi chi i dek’ i Israel yepa be ba Dōm i nit ka di ñoui.


Mu ne len, Bindānkat bu neka mbōk bu ñu nekalo tālube chi ngur i ajana, niro na ak borom‐ker ku gēne chi dēnchukay am lu ês ak lu maget.


Yēn a sēde lōgu chi sēn bopa, ne yēn a di dōm i ña rēy on yonent ya.


Di nañu len gēneji cha juma ya: chi dega wah͈tu wa di na jot ne ku mu mun a don ku len di rēy, di na dēfe ne defal na Yalla ligey.


Yesu nêti len, Jama and’ ak yēn: naka ma Bay ba yōni on, man it nōnu lā len yōni.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan