30 Te ne, Su ñu nek’ on chi suñu bes i bay ya, doū ñu on bōlo ak ñom chi deret i yonent ya.
Suboh͈un yēn, bindānkat yi, ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn tabah͈ i bamel i yonent ya, te rafetlo i bamel i ñu jūb ña,
Yēn a sēde lōgu chi sēn bopa, ne yēn a di dōm i ña rēy on yonent ya.