3 Mōtah͈ lu mu mun a don lu ñu len ebal, dēgal len, te def ko; wande bu len def naka sēn i jef; ndege ño di wah͈, te du ñu def.
Mu ñou cha ñarel ba, te wah͈ati lōga. Mu tontu, ne, Di nā dem; wande demul.
Bindānkat ya ak Pharisee ya tōg nañu chi tōgu’ Musa:
Ño di taka say yu dīs, te mite yubu, teg len chi i mbag i nit; wande ñom du ñu len randal ak sēn baram.