26 You Pharisee bu silmah͈a bi, setalal jeka bir i ndap li ak kela bi, ndah͈ cha biti set itam.
Bāh͈lo len garap gi ak i dōm am; mbāte bonlo len garap gi ak i dōm am; ndege rañātle nañu garap gi chi i dōm am.
Mōm nak ndege ndey am jeñtal na ko, ne, May ma file bop’ i John Batisekat ba chi ndap.