25 Suboh͈un yēn, bindānkat yi, ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn di setal biti’ ndap ak kela, wande cha bir fês na ak ndāntu ak nchaychay.
Mōm nak ndege ndey am jeñtal na ko, ne, May ma file bop’ i John Batisekat ba chi ndap.