2 Bindānkat ya ak Pharisee ya tōg nañu chi tōgu’ Musa:
Mōtah͈ lu mu mun a don lu ñu len ebal, dēgal len, te def ko; wande bu len def naka sēn i jef; ndege ño di wah͈, te du ñu def.