18 Te, Ku di geñ cha lotel ba, dara la; wande ku di geñ cha maye ga cha kou am, war na ko motali.
Suboh͈un yēn, njītekat yu silmah͈a yi, yēn ñi wah͈, ne, Ku di geñ chi juma ja, dara la; wande ku di geñ chi wurus i juma ja, war na ko motali.
Dof yi ak silmah͈a yi: bu chi gen a rey, wurus wā’m, am juma ja di selal wurus wa?
Silmaha yi: bu chi gen a rey, maye gā’m, am lotel ba di selal maye ga?