17 Dof yi ak silmah͈a yi: bu chi gen a rey, wurus wā’m, am juma ja di selal wurus wa?
Te, Ku di geñ cha lotel ba, dara la; wande ku di geñ cha maye ga cha kou am, war na ko motali.
Silmaha yi: bu chi gen a rey, maye gā’m, am lotel ba di selal maye ga?