Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 23:13 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

13-14 Wande suboh͈un yēn, bindānkat yi ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn tej bunt’ i ngur i ajana chi nit: te yēn chi sēn bopa du len cha tabi; te nanguwu len ña buga tabi ñu tabi cha.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 23:13
25 Iomraidhean Croise  

Suboh͈un yēn, njītekat yu silmah͈a yi, yēn ñi wah͈, ne, Ku di geñ chi juma ja, dara la; wande ku di geñ chi wurus i juma ja, war na ko motali.


Suboh͈un yēn, bindānkat yi ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn fey asaka i oyof ya, te sagane yef i yōn wa gen a rey, mu di njūbay, ak yermande, ak ngum: yile ñom ngēn war on a def, te bañ a sagane yena ya.


Suboh͈un yēn, bindānkat yi, ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn di setal biti’ ndap ak kela, wande cha bir fês na ak ndāntu ak nchaychay.


Suboh͈un yēn, bindānkat yi, ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn niro ak bamel ya ñu wêh͈al, ñu rafet chi biti, wande chi bir fês ak i yah͈ i ñu dē, ak nubay gu mun a don.


Suboh͈un yēn, bindānkat yi, ak Pharisee yi, nafeh͈a yi! ndege da ngēn tabah͈ i bamel i yonent ya, te rafetlo i bamel i ñu jūb ña,


Wande ba mu gise jupa chi Pharisee ya ak Sadducee ya di ñou chi batise am, mu ne len, E h͈êt i ñangōr gi, kan a len yēgal ngēn di ūt a rēcha chi mer mi di ñou?


Wā’ jur am ya wah͈ nañu yef yile, ndege ragal on nañu Yauod ya: ndege Yauod ya wah͈ante on nañu be sotal, ne su kena wah͈e ne mō di Krista, di nañu ko gēne chi ndaje ma.


Ñu ôlu nak ka silmah͈a won ñar i yōn, te ne ko, Na nga jebal Yalla ndam: h͈am nañu ne nit kile bakarkat la.


Ñu tontu te ne ko, Yangi jūdu on bepa chi bakar, te nga buga ño jemantal? Te ñu gēne ko cha biti.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan