44 Borom bi nôn na suma Borom, Tôgal chi suma ndējor, be ma def sa i mbañ chi sa run tanka?
Su ko Dauda ôe Borom bi, naka mu neke dōm am?
Yesu ne ko, Wah͈ nga ko: te mangi len di wah͈, Ganou lile di ngēn gisi Dōm i nit ka mu di tōg chi loh͈o’ ndējor i kantan, di wachasi chi i nir i asaman.
Thomas tontu te ne ko, Suma Borom ak suma Yalla.