41 Ba Pharisee ya dajalô, Yesu lāj len, ne,
Fōfale la Pharisee ya deme, te fēncha naka ñu ko mun a jape chi kadu am.
Wande ba Pharisee ya dēge ne mō nopilo won Sadducee ya, ñu dajalo.