40 Chi ñar i eble yile la yōn wa yepa ak la yonent ya bind’ on japu.
Mōtah͈ lu ngēn buga lepa nit di len ko defal, yēn itam na ngēn ela defal ñenen: ndege bile di yōn wi ak yonent ya.
Ndege Musa la ñu joh͈ on yōn wi; yiw ak dega bayako fa Yesu Krista.