39 Te ñarel bu niro ak mōm di bile, Na nga sopa sa morom niki sa bopa.
Teralal sa bay ak sa ndey: te, Sopal sa morom niki sa bopa.
Bile di eble bu rey ba ak bu jeka ba.