37 Mu ne ko, Na nga sopa Borom bi sa Yalla ak sa h͈ol bepa, ak sa fit wepa, ak sa nh͈el mepa.
Jemantalkat bi, ban eblê gen a rey chi yōn wi?
Bile di eble bu rey ba ak bu jeka ba.