36 Jemantalkat bi, ban eblê gen a rey chi yōn wi?
Bu mu teral bay am. Tah͈na be defadi ngēn eble’ Yalla mu di dara chi sēn nābe.
Kena chi ñom ku h͈amkat i yōn la won, lāj ko di ko fir, ne,
Mu ne ko, Na nga sopa Borom bi sa Yalla ak sa h͈ol bepa, ak sa fit wepa, ak sa nh͈el mepa.