32 Mā di Yalla i Ibrayuma, ak Yalla i Isaka, ak Yalla i Yanh͈oba? Yalla du Yalla i ñu dē ña, wande ñu dunda ña.
Wande mosu len a janga lu jem chi ndēkite ga, la len Yalla wah͈ on, ne,