Biblia Todo Logo
Bìoball air-loidhne

- Sanasan -




Matthew 22:3 - Linjil i Yesu Krista Suñu Borom bi 1907

3 Te yōni i ndau am ñu ôal ko ña mu ô on chi nchēt la; ñu bañ a dika.

Faic an caibideil Dèan lethbhreac




Matthew 22:3
30 Iomraidhean Croise  

Ba jamāno i mēñef jegeñse, mu yōni i ndau am chi ligeykat ya ndah͈ ñu jel i mēñef am.


E Jerusalem, Jerusalem, mu rēy yonent ya, te jamat i h͈êr ña ñu ko yōne! naka lā don faral a buge dajale sēn i dōm, naka ganar gu di dajale i dōm am chi run lāf am, te ngēn bañ.


Rēchu len, ndege ngur i ajana jegeñsi na.


Yesu ne len, I mbok’ i nēg i borom‐chēt ga, ndah͈ mun naño nah͈arlu ba borom‐chēt ga neke ak ñom? Wande jamāno di na diki ba ño fabi borom‐chēt ga cha ñom; bōbale di nañu ôri.


Te bugu len a ñou fi man, ndah͈ ngēn am dūnda.


Lean sinn:

Sanasan


Sanasan