29 Yesu tontu len, ne, Da ngēn jūm, ndege h͈amu len mbinda ya, wala kantan i Yalla.
Chi ndēkite ga mbōk, jabar i kan la di neka chi jurom ñar ña? ndege ñepa sey on nañu ak mōm.
Ndege h͈amangu ñu on mbinda ma, ne di na dēki cha dē ga.