28 Chi ndēkite ga mbōk, jabar i kan la di neka chi jurom ñar ña? ndege ñepa sey on nañu ak mōm.
Ganou ga jigen ja itam dē.
Yesu tontu len, ne, Da ngēn jūm, ndege h͈amu len mbinda ya, wala kantan i Yalla.